MUZTEXT
Текст пісні Sportif - Youssou N'Dour
Інформація про пісню На цій сторінці ви можете ознайомитися з текстом пісні Sportif , виконавця -Youssou N'Dour У жанрі:Африканская музыка
Виберіть якою мовою перекладати:
|
| Woyal sa wayu ndam ii |
| Dangay bégël sa xol bi |
| Ndax yaa yor bannex bi |
| Ni tay bés bii sa bés la |
| Sa mbër daan na kóntaan nga |
| Bu ñu daanee sa mbër nak |
| Na nga fexe ba nee |
| Po mii dañuy Jonante |
| Faw mu am ku moyle |
| Jarula defante, di xasteeka dóóre |
| Jonante po ag ree la |
| Boo gañee fo ag ree la |
| Boo ñàkkee fo ag ree la |
| Lépp ci fo ag ree la |
| Buñ la gañee muñël |
| Boo ko gañee baalal |
| Bëgóón nga mu demee ni demewuko |
| Mën naa am bu ëllëgee mu gën fee neex |
| Ba ma làng ag samay gaa yi ngir bànneexu |
| Xam ne lii fo la nii lay mënë deme |
| Powun jonante nii lay deme |
| Tay jii yaw bu ëllëgee keneen la |
| Fo ag ree de lañ ciy jublu |
| Moo tax ñu wara dal taynangu defet |
| Jonante po ag ree la |
| Boo gañee fo ag ree la |
| Boo ñàkkee fo ag ree la |
| Lépp ci fo ag ree la |
| Buñ la gañee muñël |
| Boo ko gañee baalal |
| Waa waaw wuy dabbee wuy yoo |
| Dabi alaa ko ndey baate satata |
| Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jigéén |
| Sire lañu dóór bal géér ña da ñoo daw |
| Sire Bàlla moo ñaan Ramata Faal |
| Siree nga Cees Matee nga Njaarém |
| Duñ ko wëy ku reew, duñ ko wëy ku ñaaw |
| Aah wuy dabbee wuy yoo |
| Dabi alaa ko ndey baate satata |
| Jonante po ag ree la |
| Boo gañee fo ag ree la |
| Boo ñàkkee fo ag ree la |
| Lépp ci fo ag ree la |
| Buñ la gañee muñël |
| Boo ko gañee baalal |
Поділіться текстом пісні:
Напишіть, що ви думаєте про текст пісні!
Інші пісні виконавця:
| Назва | Рік |
|---|
| 1995 |
| 2019 |
| 2005 |
| 2013 |
| 2013 |
| 2017 |
| 2018 |
| 2020 |
| 1993 |
| 2018 |
| 2004 |
| 2007 |
| 2009 |
| 2009 |
| 2009 |
| 2009 |
| 2009 |
| 2009 |
| 2009 |
| 2009 |